ADIOUZA – MARIAGE ft. Dame Sene

MARIAGE – ADIOUZA ft. Dame Sene
Lyrics, Letra:
Couplet 1
Messo wax mou degne messo tasse sama yakare
Ndax ya ma niwone kou doule Mane dou done sa jabare
Yagg woute kou mél ni Yaw ma fan sa jiko
Ndax Level bi dafa kawewone nga ajiko

Pré refrain
On a affirmé
Balisé
approuvé

On a validé
Confirmé
Notre amour

Refrain
Bess dou toute borome
Laye tolole
Taye sama bess la Mà Ayer
Xaleyi sagneser
Mak yi sagnesser
dal dimaye sargal
Yayee boye Nima
Badiene Nima
Mougneleul saye goro
Na nga Slow down
Tek thiye soutoural sa jeukeure

Doudou je t’aime beaucoup
Fo pikiro ma nane fa dome
Mon Doudou je t’aime beaucoup
Dama love ba doffe mon doudou

Couplet 2

J’ai été l’élue parmi toute tes conquêtes
Gare à celles qui tenteront de créer une tempête
Je te promets d’être à jamais ta reine
Promets-moi l’éternité de mon règne

Pré refrain
On a affirmé
Balisé
approuvé

On a validé
Confirmé
Notre amour

Refrain
Bess dou toute borome
Laye tolole
Taye sama bess la Mà Ayer
Xaleyi sagneser
Mak yi sagnesser
dal dimaye sargal
Yayee boye Nima
Badiene Nima
Mougneleul saye goro
Na nga Slow down
Tek thiye soutoural sa jeukeure

Doudou je t’aime beaucoup
Fo pikiro ma nane fa dome
Mon Doudou je t’aime beaucoup
Mane de beugenala mon doudou

Pont
Chéri promets-moi de m’aimer pour la vie
Dema balle soumala togner
Mane Souma joumer
Souma la merer
Xamalni xol bi ya THI neee

Solo
Defnala jarraf
boma deffer Ndeye ji rew
Watenani sa ngoure gui dou meussa Jexe
Doudou kaye

Doudou je t’aime beaucoup
Dema bale Souma la togner
Mon doudou je t’aime beaucoup.

Feat Dame sène

Solo
Ahnnnn keppeu koula meussa wane mbeugel
Mane laye topando
Douma Sene mass
Maye Sene caporal

Sathieuma yobouma demalak Mane chéri yama mome.
Mon doudou boulma yeureume

Amna gnoufi diare begonna jem
Wayer Bi nga yekser la guisse Louma yeme

Sathieuma yobouma demalak Mane chéri yama mome.
Mon doudou boulma yeureume

Mon doudou terale ngama
Mon doudou sagale ngama.

Résumé :
Comme son nom l’indique la chanson raconte l’histoire d’une femme qui va se marier, tout en prodiguant des conseils aux futures mariées.
Le mariage est sacré et n’est pas une chose facile. Il faut faire des concessions pour pouvoir perdurer dans la vie de couple.

Si prega di attivare i Javascript! / Please turn on Javascript!

Javaskripta ko calu karem! / Bitte schalten Sie Javascript!

S'il vous plaît activer Javascript! / Por favor, active Javascript!

Qing dakai JavaScript! / Qing dakai JavaScript!

Пожалуйста включите JavaScript! / Silakan aktifkan Javascript!
%d blogueiros gostam disto: