Kid Veli – BOY GUEDIAWAYE

Kid Veli – BOY GUEDIAWAYE Lyrics Letra:
Fuck clé minute di na sr feep
Fuck kep kou fer feep
Dieul ropalane khadiouma Galsen
May def nga meune def

Mother fucker douma daaw mai ci kanam ngene may sene
Ecarter dial mbaye diey fay
Sapeur allo meunoma fay
Champeau de paille gum gum bang

Nieuw déranger lene sans liteurou jean
Domage amo liteurou fiit
Dilene ray c’est écologique
Shoot shoot sniper nous on telimine

Guedieway la boy non boul test
Raylene melni peste
Xalil ma ni dieg
Legui kouniou beug guiss Trace nganiouy set

Chak son def hit
Effacer lak sa click
Bou doyoul dagn koy bis
Officier mon cul
Nieuwate keufate sa fiit
Ak katana ichigo bleach

Apart team yene nieup ay goordjiguene nguene
QAnnée lumière sunu digueueunté
Sarate ndey feep sans bireul lene
Mangui kaw assamane ngani mane ngay direuntel

Refrain

Squad bi amoul tapette brodah
Ay indice lagnouy dokhé
Boy Gway city kheur lay balle perdu encaissel
Show ma Liquide khaliss bo beugué taper la causette
Click click baaw diss ci balance bi kay pesser

Second couplet

Du tik au tak
Teag lou diss sa kaw demate
Tik tik tik tok ci biir palai
Teuf sa fiit teudj sa mind ni fort boyard
Com poutine dama nieuw pr dictelene

Bitch boul di sakh dieul ay risk
Danga nam ndy bif mangui ak billet meuve youniou tracer Dic
Que des trou de cul
Big dick je vous traumatise
Boudoul a4suki fuck you fuck nieup fuck sa negu music

Mother fucker dama diss com contenaire
Contelene niata kill sama biir domaine
Tek lou khess niom nieup may cons ci pet
Continuel fai un veu kid com comete
Gaaw la def

Troisiéme couplet

Am nguene blem ni controle math
Thug life ni 2 pac
Allo rap Galsen dama nieuw pour fadj
Rapeur yi dem fan

May kid fils
Nieuw demonter sene wiss
Big mc
C’est que biceps yé touti

Damq nieuw motali rapeur you matadi
Boul freq gni maman ta di
Dam rew ci rap wala maladie
Dama ay trop maman a lu

Com dab
Nieuw tek com dab
Rek nieup contane
Fayla sans contact
Ay liasse ten taw
C’est primordial

%d blogueiros gostam disto: