Home / Dancehall / Samba Peuzzi – Je Ne Merite Pas ça.

Samba Peuzzi – Je Ne Merite Pas ça.

Je Ne Merite Pas ça. – Samba Peuzzi Lyrics, Letra:
Eyy
Bouma khamone ni lay demé douma ko nop.
Bouma khamone ni lay demé douma ko love.
Bouma khamone ni lii lamay deff douma koko djiokh yeah.
Bouma khamone ni layy demé eyy.
Pourtant bagnalouma dara sa yaye ak sa papa.
Pourtant bagnalouma wonne dara sa yaye ak sa papa.
Bayiwone na leep ndakh yaw … ak sen waa keur.
Fatei wonne na gneup ndakh yaw … ak sen waa keur.
Ooo Ooooo
Je mérite pas çaaaa!
Loutakh nga mayy nakh?
Je mérite pas çaaaa!
Loutakh nga mayy nakh? Baby
Ak finiou diar yeup, pour mane dou dièkh.
Mounoumako geum you’re always on my mind.
Louma wax mou bagn, nangouma déglou.
Néna dey dem, khalé bi worr nama.
Ça me fais très mal tu n’me calcule plus.
Je t’ai tout donné et t’es parti comme ça.
T’avais promis de rester pour le meilleur et pour le pire.
Elle a brisé mon coeur pour du Xaliss. Boul diaaaaaye sa ngor!
Beugueul té YaAllah tax lolou rek’ay deug .
Boul diaaaaaye sa ngor!
Beugeul té YaAllah tax lolou rek’ay deug.
Bouma khamone ni lay demé douma ko nop.
Bouma khamone ni lay demé douma ko love.
Bouma khamone ni lii lamay deff douma koko djiokh yeah.
Bouma khamone ni layy demé eyy.
Pourtant bagnalouma dara sa yaye ak sa papa.
Pourtant bagnalouma wonne dara sa yaye ak sa papa.
Bayiwone na leep ndakh yaw … ak sen waa keur.
Fatei wonne na gneup ndakh yaw … ak sen waa keur.
Ooo Ooooo
Je mérite pas çaaaa!
Loutakh nga mayy nakh?
Je mérite pas çaaaa!
Loutakh nga mayy nakh? Baby
Babe dinaa am lou bakh boudé YaAllah kholay fayy.
She make my heart break everyday.
Problèmes sur problèmes.
…et j’ai essayé de tout régler.
Ohhh
Tay si kii souba si kéé.
Bad girl changél adouna dou nii.
Tay si kii souba si kéé.
Boul diaaaaaye sa ngor!
Beugueul té YaAllah tax lolou rek’ay deug .
Boul diaaaaaye sa ngor!
Beugueul té YaAllah tax lolou rek’ay deug .
Bouma khamone ni lay demé douma ko nop.
Bouma khamone ni lay demé douma ko love.
Bouma khamone ni lii lamay deff douma koko djiokh yeah.
Bouma khamone ni layy demé eyy.
Pourtant bagnalouma dara sa yaye ak sa papa.
Pourtant bagnalouma wonne dara sa yaye ak sa papa.
Bayiwone na leep ndakh yaw … ak sen waa keur.
Fatei wonne na gneup ndakh yaw … ak sen waa keur.
Ooo Ooooo
Je mérite pas çaaaa!
Loutakh nga mayy nakh?
Je mérite pas çaaaa!
Loutakh nga mayy nakh? Baby
Letra lyrics lyric letras versuri musiek lirieke tekstet paroles

Deixe uma resposta

Esse site utiliza o Akismet para reduzir spam. Aprenda como seus dados de comentários são processados.

%d blogueiros gostam disto: