Shampagne Baby – Mbougeul

Shampagne Baby – Mbougeul Lyrics Letra:

Rafales si kepeu kouy tite
Yoral kholou fiteu may djite
Dokhane fi ndeye bullshit
Dagua dof dictature aka poutine
Kene douma teyé damalene teu
Shampagne leu dang sisa bop ni Lette
Goor fall boma pique ké doumeu bett
You gotta better middlefinger sisa letter

Meunou niou bok do daw sama yaram
amouma pitié nono dama kharam
Mane fima yewo lassa boy yi di kharàng
Kharangn thi kaw beat shampagne nekha faral
Deal bi mane na
Dama khewlei yeglei togou mana
Geuneu parei beuri màana
Diour rapeur yu beuri
Coumba rek si mama

Deflene lou meti comme tangorou sirate
Ligua mom lay dieulsi ni pirate
Bandit bougn ko sekei never doto dealate
Troublei fepp comme lékk se dilate

Mingui turu di tokhu
Dagua mer bane golo gua bokhou
Buur music koudoul gaindei dou bok
Meuno ma sonal boul sonal sa bop

Indil lene guandim probleme
com seugue thi guew diy kadjey
Dama degg birr gueweul lay wathié
Athi rythme bassi kaww bouma lathié
diayma diap meunoul benefique
Pousseul indil do ma meuneu fekh
Mane douma tite amo ben fite
Paw paw paw temeri fake

Refrain

Fi gayi tougn tite
Ndakh gun laniouy dokhanto
Middlefinger bullshit
Gia lo sai non sei pronto
Hey namou beef
Ligua tei la sifff
Let me move some weak
Souma merei douma gifff yeah
Boy you kogn ba ken dou tite
Am fite meuneu fitei com jite
yorei gunz meune si fuck bullshit
🐍🐍🐍🐍🐍

Wakh dji dou beuri pour lem seni deubeuss
Garei BM digou mbeubeuss
Goré ba dei kon meuno ma beumeukh
Sa rapeur la leumeuss ndakh
Beug beignet keumeukh
Geune leu swag guena meti
Mane la shampagne baby
Damay bek pour gua mer ci
Dama rew ok merci

Beuss bo deguei dama mer dieum deufeul
Kileuy seuffeul bouma guisssei khim leweul
Diayla Djikoy maketman dila ayy
Li ngay degu dafa soute seni level

Dioudo italie nieuw ndakarou sampe
Kou pique shampagne lok gua lou tang

Lathie ma niou beurei fils ma may la tank
Yakhal sama der mane magui si diam

Hey magui diam magui si diam

Haters ngua gassal sa kamb

Mane beugouma diam tei taal bi lay khamb

Respectei lene nope yi beugou niou yambeu

E meylenma tuti
Shampagne ci beat bi
fok music bi touti

✓ Refrain

Fi gayi tougn tite
Ndakh gun laniouy dokhanto
Middlefinger bullshit
Gia lo sai non sei pronto
Hey namou beef
Ligua tei la sifff
Let me move some weak
Souma merei douma gifff yeah
Boy you kogn ba ken dou tite
Am fite meuneu fitei com jite
yorei gunz meune si fuck bullshit

%d blogueiros gostam disto: