Jahman Xpress – Yakofi khar Lyrics Letra Jahman X-Press Jahman Xpress – Yakofi khar Lyrics
Teranga meunoul reuy ba eupp ci ioe
Yakofi khar konn kou yebbo na roy ci ioe
Khamoon nani yagg yagg souniou biss bilei dina nieuw
Lo kharoul doulafi fekk gathié ngalama ioe
Meti nga daw
Dieguéssima na gaw
Yagg nga yendou si nadj bi wayé legui ci clim ngay nelaw
Tabaski dawouniou niaw
Benn nitt dawoufa nieuw
Té 3 Pieces lalay daminél sa benn morom dotoula raw
Peuram bassi ngalam (Yakofi Khar)
Car Rapide bassi 4×4 (Yakofi khar)
Raflé dotoula dalaat
Té lo soll dotoko solaat (yakofi khar)
Charette bassi auto(Yakofi khar)
Barack bassi château (yakofi khar)
Daggoul malay photo
Louko raw mérité ngako (yakofi khar)
Kayway kay sama dom dji yobaléma
Kayway kay sama dom dji Rakadjou nga
Kayway kay sama dom dji yobaléma
Kayway kay sama dom dji yobaléma
Dembeu la geunoon metti tokk nga mougne
Souniou diguanté yagg’na diaffé
Yagg nga geum’né kou mougne dina mougne
Lofi meunti am dangako niafé
Beugué do matt ngor matt
Khol sou beugué borom dou diambaat
Luñ traversé lepp nga gorré man soumako wakhoul doon diamm
Suñ Tangana gouddi yeup
Moy Michoui tay
Daan ndieukanté Bus
Té nieupangui car suñ auto you Rafét
Dann fanaan ci barack
Tay niou yewou ci étage
Si laal bou noy ndakh khebouma woon bimay am ndieugou padiass
Daan beugue foukk (diourom teula)
Tay kheb naniou Cfa ( nioungui ci dollars )
Koula meussa yéné (tay niénala)
Yagg naniou fandé
Tay lekk bi bari baniou diko mayé
Khadiou goudi khiff yagg niou meuné
Tay daniou grâce matinée
Peuram bassi ngalam (Yakofi Khar)
Car Rapide bassi 4×4 (Yakofi khar)
Raflé dotoula dalaat
Té lo soll dotoko solaat (yakofi khar)
Charette bassi auto(Yakofi khar)
Barack bassi château (yakofi khar)
Daggoul malay photo
Louko raw mérité ngako (yakofi khar)
Kayway kay sama dom dji yobaléma
Kayway kay sama dom dji Rakadjou nga
Kayway kay sama dom dji yobaléma
Kayway kay sama dom dji yobalémaa
Suñ rongoñu dembeu ya doon na taw tay méñil ngor biñou djiwantéwoon newoon nala yallah dina ñeuw
Lyrics, Letras, Paroles, Deutsche, Letras, Testi,Тексты, Texty, Norske, Текстови, Versuri, Persian, Liricí, Lirik, Nederlandse, Tagalog